Sylla Madridista en wolof

Sylla Madridista en wolof Halla Madrid 🤍😇

🚨🚨 LEER: Real Madrid DINA DEF BENN OFFRE CI ENZO Fernandez.José Mourinho LAAJ NAKO Real Madrid dafa dindi kontraa Ceball...
17/06/2026

🚨🚨 LEER: Real Madrid DINA DEF BENN OFFRE CI ENZO Fernandez.

José Mourinho LAAJ NAKO

Real Madrid dafa dindi kontraa Ceballos bi; Dafay dem ci transfert bu amul fayda

Yeneen joueur yi dina ñu topp

[Marca )

🚨 PEREZ DU JOX KÀDDU MUJJ! Real Madrid mingi waaja jël Michael Olise ginaaw Coupe du Monde bi.Dañu jàpp ni mooy Galactic...
17/06/2026

🚨 PEREZ DU JOX KÀDDU MUJJ! Real Madrid mingi waaja jël Michael Olise ginaaw Coupe du Monde bi.

Dañu jàpp ni mooy Galactico dëgg bu Florentino Peres, du Julian Alvarez.

Neena ñu club bu Madrid bi pare na def lépp lumu mën ngir mu mëna dem. 🔥🤍

(Source: 🗞️ AS)

🚨 Sunu sukkandikoo ci Marca ak Jose Felix Diaz, Real Madrid mingi waajal weer wu metti lool.Ba leegi club bi defa bëgg s...
17/06/2026

🚨 Sunu sukkandikoo ci Marca ak Jose Felix Diaz, Real Madrid mingi waajal weer wu metti lool.

Ba leegi club bi defa bëgg siñe ñaar mbaa ñetti joueur, jeexal ay genni yu bari, ak jeexal tabaxaat ekip bi bala preseason bi di tàmbali, bi ñu nara def ci 13 juillet

Te dafa melni, yenn surprise mën nañu des ci manngasiin bi... 👀🤍

Fabrizio Romano:Antonio Rüdiger signe officiellement kontraam bu bees bi ak Real Madrid ba juin 2027. ✍️🤍Annonce Officia...
16/06/2026

Fabrizio Romano:

Antonio Rüdiger signe officiellement kontraam bu bees bi ak Real Madrid ba juin 2027. ✍️🤍

Annonce Official bu club bi munna am ci 24 waxtu yii ci kanam. Defaaseer bu Almaañ bi mungi yokk beneen sesoŋ ci Madrid

🚨🤍 Communique Official bu bawoo ci Real Madrid:"Real Madrid CF ak Chelsea FC amnañu deggoo ngir jël Marc Cucurella mii n...
15/06/2026

🚨🤍 Communique Official bu bawoo ci Real Madrid:

"Real Madrid CF ak Chelsea FC amnañu deggoo ngir jël Marc Cucurella mii nekk ci sunu ekip bi ci jiroom benn sesoŋ yii jubsi ba 30 weeru juin 2032." ✍️⚪️

Dalal ak jàmm Marc Cucurella

Enzo Fernandez BËGG NA signe REAL Madrid. ✅👀Chelsea bëgg na €140M⌛️ Real Madrid mingi xool ban xeetu diggi teere lañu bë...
14/06/2026

Enzo Fernandez BËGG NA signe REAL Madrid. ✅👀

Chelsea bëgg na €140M

⌛️ Real Madrid mingi xool ban xeetu diggi teere lañu bëgg

🚨 C'est fait ! 🔙 *Sami Khédira* dellu na Real Madrid !Diggi teere bi woon duggu na ci ekipu José Mourinho ba noppi tammb...
14/06/2026

🚨 C'est fait ! 🔙 *Sami Khédira* dellu na Real Madrid !

Diggi teere bi woon duggu na ci ekipu José Mourinho ba noppi tammbali chapitre bu bees ci jaar-jaaram ak Merengues yi.

Ñeenti joueur ci 80€ Don F.  Perez ku doon ? 🫡🤍
14/06/2026

Ñeenti joueur ci 80€

Don F. Perez ku doon ? 🫡🤍

🚨🚨💣 Marc Cucurella DANA DEM CA REAL MADRID, 🤍🔥Real Madrid jël na déggoob ak Chelsea ngir ñu jël Marc Cucurella. ✅Real Ma...
14/06/2026

🚨🚨💣 Marc Cucurella DANA DEM CA REAL MADRID, 🤍🔥

Real Madrid jël na déggoob ak Chelsea ngir ñu jël Marc Cucurella. ✅

Real Madrid mujjee am seen defaas bu bees ci cammoy bi! 🇪🇸⚡️

Fabrizio Romano

🚨 Sunu sukkandikoo ci José Luis Sanchez:José Mourinho defa bëgg lool tàmbali liggéey ci Real Madrid.Ñi ko jege neena ñu ...
14/06/2026

🚨 Sunu sukkandikoo ci José Luis Sanchez:

José Mourinho defa bëgg lool tàmbali liggéey ci Real Madrid.

Ñi ko jege neena ñu amna mbégte bu mel ni bimu tammbale nekk anterneer.

Le special one amna mbégte ci projet Real Madrid bi te gëm na bu baax. ⚪️

Adresse

Diourbel
Touba

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sylla Madridista en wolof publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager

Type